dëm ci mayu Mozilla ak sama compte firefox

Kompt Firefox dinàlay bayi này jeuriño ci ay mayu Mozilla ci bëp téléfôn ak nawigätëer bu Firefox wala sistèmu Firefox ci kàw rek ngë dugg cii. Lëp li nge soxla pour tahàwaal kompt Firefox môy bène imeel ak batù jàl.

Nàka lay ammè ci Komptu Firefox yi ?

Mëene nge dëm ci page bu bìindukay bi ci bëp serwiss Mozilla, wala sàaytu Page bu bìindu ci Kompt Firefox ak tòp jàar-jàar yi si sûuf:

 1. Duggalàl së batù imeel, batù jàal ak se atü judû, so parè nge bëss {buton dugg}.
 2. Sou imeel nànggu bi dikkè, bëssal ci yonù saytu bi.
 3. Sasù niu saytò seu Kompt bi, dùggal ci mayù Mozilla yulà gëenal ak së Kompt bu bëes bi.
Sò amé jàffè-jaffè ci saytu se kompt, niu ngilay niàne nge hol Da me àm jàffè-jàffè pour dëggal samà Kompt Firefox bu bës bi.

Yàne mày la mëenà jeuriñuu ak kompt Mozilla?

Màyu Mozilla yìy topë mëene ngakà äm fimné :

 1. Firefox Sync: Dugggal ci say xibaru saytu, yü melni ay xamëwukày, jàar-jàar yi, batù jal ak übi ay page yu baari ci ay aparëey yu wutè ci kàw rek nge duug seu kompt Firefox.
 2. Firefox Marketplace: jëundàl, fayal say aplikaçion ci ay anàm yu wöor, yökal tëy top guiss-guiss yussi àm, ak di duug ci biblìotèk aplikaçion yi ci say aparëy yëp.
 3. Firefox Na ngë def: Jëefàndikol wideo ak woté bàat bu Firefox ngir waxtàn ak say xarìit ak xétu waxtànu bàat. Kompt Firefox daflày mäy ngày jeuriño ci ay sumb yuñu rañié, lu mélni list Kontact wanti donùul luñiu latié pour jeuriño yu jëek yi.
 4. Oùt sama apàrëy: Oùt, tëëj, walà éfacë bène apàrëy Firefox bu rëer lëp ak jeufàndiko se ordinatër rek.
 1. Firefox Sync: Dugggal ci say xibaru saytu, yü melni ay xamëwukày, jàar-jàar yi, batù jal ak übi ay page yu baari ci ay aparëey yu wutè ci kàw rek nge duug seu kompt Firefox.
 2. Firefox Marketplace: jëendàl fayal say aplikaçion ci ay anàm yu wöor, yökkal tëy top guiss-guiss yussi àm, ak di duug ci biblìotèk aplikaçion yi ci say aparëy yëp.
 3. Firefox Na ngë def: Jëfàndikol wideo ak woté bàat bu Firefox ngir waxtàn ak say xarìit ak xétu waxtànu bàat. Kompt Firefox daflày mäy ngày jeuriño ci ay sumb yuñu rañié, lu mélni list Kontact wanti donùul luñiu latié pour jeuriño yu jëek yi.
 4. Oùt sama apàrëy: Oùt, tëëj, walà éfacë bène apàrëy Firefox bu rëer lëp ak jeufàndiko se ordinatër rek.
 5. Pocket çi Firefox: Dìntie ay pàge web ci samëe list lektur.
// These fine people helped write this article:AbdouAziz. You can help too - find out how.

Ndax jukki bi amal nala njariñ? Xaaral tuuti...

Bokk ci ñiy jàppale Ndimbalu Mozilla