Tahawaal ay matuuway

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Lìdi Marketplace bène magassìn boüy bagé ay aplikaçion yuñiu dëfar pour seu téléfònu sitém Firefox. Bàtaxal bi daflay wöone nakëe nàalène di raniéwé bä inçtalélène.

Rañié aplikaçion yu djéggi dayo

So ibbè Marketplace bi di në giss listù aplikaçion yiñiu le xélal ak ci siiw.

Marketplace Home
  • Yòne wi ci kaw dinalë diimbali nge saytu aplikaçion yi ci sène bëssay, sène cìway, walëe hèet biñiu bok.
  • Cii louler, kanamu Marketplace bunè amnà kàzu seetukay bulay diimbali nge giss li ngë nek di wëer
    new marketplace search
  • So néké di saytu, bëssal ci aplikaçion bumù mëenti nek ngiir hol détày yu melni ay kapture ékran, essplikaçion yu gëena léér ak xalàt yussi am.

Instalè aplikaçion

Instalè aplikaçion gawnëe té yombnë.

  1. So gissé aplikaçion bo bëeg instalè, bëssal ci buton bu bleu bi. Soudé aplikaçion bi amul faay, buton bi dinalàko wax. Soudé aplikaçion bi daafay latiè xaliss, djëek bi dinà fèñie ci buton bi.
    Free and paid apps
    xamaal: Yòne biñiuy djëende aplikaçion dafay wuttë cii fimuy diaar ak dëek bi ne nek. Tòpal rek tektàl yii ci ékran bi.
  2. Dëegalal ni da në bëgg inçtalè aplikaçion bi cii kàw nge bëss buton Install.
    • Së aplikaçion bi dinañiu lako jëlil te bene rañiéwukay dinà féñie ci ekran akeuy bi.
      Twitter installed

Làne mo wuutelè Marketplace bi ak Seet bìdi sopeku ?

Marketplace bi ak seet bìdi sopeku dañuy dioxé niari jàngat yu wuutè pour jëli aplikaçion yi. Marketplace bi bene marssé le buñiu tahawaal ngiir téléfòn sistému Firefox. Seet bìdi sopeku dafay giss site web yu téléfòn yù mëna instalè wu ak di doxe kom ay aplikaçion

// These fine people helped write this article:AbdouAziz. You can help too - find out how.
Bokk ci ñiy jàppale Ndimbalu Mozilla