Fäne leu ngiiy dévelopé waleu dëm

Soudé déwelopeur nge, di nge guis lo soxlà ci Mozilla Developer Network (MDN). Ndàw Dewelopëer bu Mozilla (MDN) dañuuy bâhé ay jangat, ak firi yu lër ak tàm bëreb wahtanukay foy mëena latié ak di wétio ak yenène déwelopëer.

Page yi di niëw bahnà torop pour mëena tambali so soxla ndimbël :

Li dòn ne ay wahtàne yo mëna fek ci Ndaw Déwelopeur bu Mozilla:

  1. Sùumb xétu-web yu ùbeku :
    • HTML
    • CSS
    • JavaScript
    • Melukanu API internet
  2. Sistému Firefox:
    • Ubì ay aplikaçion Web
    • Tek ci yone ak tahawal sistému Firefox
    • Bok ci jangàat bu sistemu Firefox
    • Ranié Gaia
  3. platform bu Mozilla:
    • Gecko
    • Tahawal ak jangàt Firefox
    • XUL
    • XPCOM
    • Yonû saytu bu Firefox (Nightly, Aurora ak Beta)
// These fine people helped write this article:AbdouAziz. You can help too - find out how.

Ndax jukki bi amal nala njariñ? Xaaral tuuti...

Bokk ci ñiy jàppale Ndimbalu Mozilla