Dinndi samay xibarou out ak jumtukayou Saytuu yi

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Sassöy nawigëe ci web bi, seu nawigatër daflay dìmbali ci fatèlèku ay informaçion yu bàari ci site yi nge diotà diar.

Batàxal bi dafàlay wône nakëe nay fompé sày xibaru diàr-diàr, jumtukàyu sàytu ak jàangat yuñu diñtie.

Fompë diar-diar

jëeriñiol sùumb bi so bëegé Firefox fatè site yi nge diotà diar.

  1. Ubìl nawigatër bu Firefox.
  2. Bësal ci tiatù nawigatër bi, ci wétu barû URL bi.
    browser-tab
  3. Bësal ci ranièwukay machìine gear iconfxos gear
  4. Bësal ci buton Clear browsing history, so parè nge bëss buton OK ngìr dëgàl.

Fompë jumtukayu saytu yi ak djàagat yuñu diñtie

Sumb bi dafày fompë karàngëe yu site web yi diñtie ci say jàr-jàr, bolëçi ngëenél yi nge amône pour site web yoyùu.

  1. Ubìl nawigatër bu Firefox.
  2. Bësal ci tiatù nawigatër bi, ci wétu baruu URL bi.
    browser-tab
  3. Bësal ci ranièwukay machìine gear iconfxos gear.
  4. Sò parè nge bëss buton {buton fompë jumtukày saytu ak jàngat yuñu diñtie}, so nopè nge bëss OK pour dëgal.

Fompë jàr-jàr wi

Jëefàndikol sùumb bi so bëggè Firefox fatè site web yi nge diotëe jàar.

  1. Bëssal ci rañièwukay karàngëe sissà ékran akëëy.
  2. Watièl te bëss ci Nawiggë ci sutura.
  3. Bëssal ci buton {buton Fompë jàr-jàr nawigaçion}.
  4. Bëssal ci {buton Fompë} ngìir dëggal.

Fompë jumtukayu saytu yi ak djàagat yuñu diñtie

Sumb bi dafày fompë karàngëe yu site web yi diñtie ci say jàr-jàr, bolëçi ngëenél yi nge amône pour site web yoyùu.

  1. Bëssal ci rañièwukay karàngëe sissà ékran akëëy.
  2. Watièl te bëss ci Nawiggë ci sutura.
  3. Bëssal ci buton {buton Fompë jùmtukayu saytu ak jangàt yiñu diñtie}.
  4. Bëssal {buton Fompë} ngir dëgàl .

These fine people helped write this article:

Illustration of hands

Volunteer

Grow and share your expertise with others. Answer questions and improve our knowledge base.

Learn More