Saytu xam xam ci mbolo mi

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Xélal yi dafadone list aplikaçion buñiu yëssal djalèlko askan wi. Xélal yòyu daniuko tëg ci ay suumb yuñu jëelé ci sutura ci xibarù instalaçion wu askân yu nek ci Marketplace bi.

app recommendations

Kane mòoy giis xélalu aplikaçion yi?

Xélalu aplikaçion yu nek cii Markeplace bi dañukay baxé ndaw yi :

  • àm komptù Firefox tëy çii duug suñuy jeufàndiko Marketplace
  • Naangù djot ci xélal yi

Nakà ngay talè sümb bi walàa faayko ?

Mëene nge tane bok wala banià bok sasounè. Tàane banià bok dinëe tah tamit ñiuy bañië di jëfànediko säy xibar (ci sutürà) pour saytù xélal yi.

  1. Sabo duggë, bëssal ci ranièwukay bu réglass yi, so nopé nge tàne {menû Sopi Réglasu Kompt}.
    account settings marketplace
  2. Kossël ci Waw, nañu may wone ay xélal ci aplikaçion yima inçtalé. bul kossë so beugoul.

Nakalàa sistèmu xélal yi di doxé?

Sistèmu xélal bu Marketplace Firefox di jariñio ndaw yi nioka tahawàal Telefonica Research Labs. Sistèm bi dafäy dioxé aplikaçion yu gëne tëy ñu ranié ko çi yu bàari. Bàala ngay tahawàal béne aplikaçion sistèm bi dafläy xélal ay aplikaçion yu sïw tëy ndawyi diko jeufànediko.


Yone bi ñiu gëuna raniè te sistèmu xélal bi dikò jeufàndiko ngi tuud collaborative filtering (CF). Doon ne sistèm buy dioxé ay xélal yuñu ranié pour jeufàndikukat yi, mukay jeulë ci xalatu yenene ndaw yusi am béne chäfka bi.


Xam-xam bu CF bu ranié bimuy jeufàndiko mi ngi tùud Matrice Factorizaçion, mi ngi joggë ci here. Sùumb binuy jeufàndiko ci bopàm niu ngikay firi ci this research paper. Danuy rek di jeufàndiko ci soutourà instalaçion wu aplikaçion bu ndaw yi wantii duniu jëel bénéne xétu xibaar biñu firi ci kàayit bi lu mèlni wüt se këer waleu beureubu liggÿukay.

Pour ñii di déwelopé: Kode (bu ùbëku) pour motalli sumb bi mi ngi nek ci: https://github.com/grafos-ml/test.fm/blob/master/src/testfm/models/tensorcofi.py. Guìinaw kode bu serwëer (tuud Frappe) bu sistèmu xélal yi ngi nék çi: https://github.com/grafos-ml/frappe. .

Naka lanuy dajjàlé xibar yi ak diko jeuriñio?

So duggë ci Marketplace bi nge tahawàal say aplikaçion, Marketplace bi dafay dintie aplikaçion bi, dëek biñiuko tahawalè, bëesbi ak wahtu bu instalaçion bi, ak tamit laàk biñu tamuu, walàa diñdi aplikaçion bi.

Xibaru ndaw yiñuy jeufàndiko ci säytu xalat yi amneu:

  • aplikaçion ak bëes instalàçion bi
  • lakku dëek bu banékhukat bi
  • lakku banékhukat bi

So jeufàandiko aplikaçion yi te duggo ci sistèm bi, Marketplace bi bobà du mëna dintie say instalaçion tëy du dintie bénéne xibar budùul aplikaçion bène ndäw bu nékk ci bène dëek moka instalè.

Xibaar yëep ñiu ngikay dìntie tëy diko jàagat ci bìr Mozilla Virtual Private Network. Duñiu mëessa sëed béne xibar ak ngiiy tahäwal aplikaçion yi tëy ñiu ngi nangù dox ci chartù yònu sutuura Bu Marketplace bi wàahni duñu jeufàandiko xibar yi loudoul pour yok banéhù ndaw yiikay jëerniò.

These fine people helped write this article:

Illustration of hands

Volunteer

Grow and share your expertise with others. Answer questions and improve our knowledge base.

Learn More