Konékté ak Wi-Fi wala rézau opérateur

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Sa bo neke fou së telefon mëna amé réso (béne be djuromi bar ci kaw se ékran data-connection) di nge mëna yoné ak jot apélu telefon] ak [[naka ngay djefanediko aplikaçion bu messaj. Wanti pour lenene loumou mëne ti nék, lou melni jëriniuu ci web bi, imeel, walë xam doxinu karte yi, di nge soxla konekxion bu sa opérator. Ni nay def pour mëna xamni sassouné ya ngi konecté.


Tal seu konekxion bu opérator

"Talal gaw së konekxion walë fayko ci së ekran notifikaçion."

  1. hëtial ci suf së barou notifikaçion bi nek ci kaw ci së ekran.
  2. Bësal raniéwukay bu konekxion operator bi pour talko (koulor bleu) wala fayko (koulor gri).
    Toggle data
xamal: Raniéwukay konekxion bi dafay faral di dieul ay koulor yu nourowuul par rapor ak telefon bi nay konekté.
xamal: utilissel xayma djëek bi applikaçion pour saytu se toluway ak dileu yëgal sassòy wajjà jëxal.

Konektéwu cii reso Wi-Fi

Doné yùy diale ci rézo Wi-Fi douniu faral di dial ak konekxion bu reso telefon bi ndah reso Wi-Fi bi moy faral di gëna gaw. Pour konektéwu ak rézo Wi-Fi bi:

  1. Ubil say reglàssu aplikaçionSettings 1.3

}Settings 1.4Settings- 2.0 (small) nge tane {mënu Wi-Fi}.

  1. bu weso, bësal ci buton Wi-Fi bi pour talko, nge mëna tane reso you übéku ngìr konektéwu ci.
    • soudé reso bouniu sekurissé le, fok nge duggàl batu jàal bi.

Së konekxion bu jëk ci reso Wi-Fi, cila sistému Firefox di dìntie lëp lou reso bobu di latié pour nga m*êne ci konektéwuwat benene yone sabo neké foy jàpè bobu konekxion mu defaral leu lëp loussi war.</div>

Reglé problemu konekxion yi

Soudé da ngay diemë ubi ay site web walë nay jëfàne diko ay aplikaçion fek konektewo ci internet di nge gis méssaj bouy wah"gisuniu serweur bi" walë "konekxion bi jàfenë".

No network connection

xolal ndax am nge konekxion Wi-Fi wala réso operator bi ba pare ne diémat

  1. Hëtial ci suf barou notifikaçion bi nek ci kaw ci së ékran.
    Internet connection
  2. Soudé raniéwukay bou konekxion Wi-Fi bi walë réso opérator bi nékul koulor bu bleu, bësko ndah nge konektéwuwat.
  3. Bësal ci {buton besatàal} ndah ngë dawalat page bi walë applikaçion bi.
xalat:soy Konektéwuwat mënna jël bene walë niari minute pour dox "Diématal".

Fompe jumtukayou saytu yi ak xibar yiniu dintie te diémàt

Soudé xol nge ni ya ngi am konekxion bou Wi-Fi walë bu réso operator te terewul di gis eror gissuniu serweur bi soy diéma dawalat béne page web, mëna am site bobu mo am jàfè-jàfè.Fompal jumtukayu saytu yi ak doné yi seu ordinatër dintie meunala dimbali.

  1. Bësal {buton menu} ci kaw ci seu ndéy dior pour oubi barou navigateur bi.
  2. Bësal {buton menu} ci kaw pour oubi réglazu Firefox.
  3. Bësal {buton diindi samay xibaru out ak jumtukay saytu yi}
  4. Bësal OK.
  5. tëjàl fenetre bi nga bës {buton diémat} ci Firefox ngir mëna dawalat site bi.

Pour yenene xibar, xolal Diindi samay xibaru wout ak jumtukayu saytu yi nek ci sistému Firefox.

These fine people helped write this article:

Illustration of hands

Volunteer

Grow and share your expertise with others. Answer questions and improve our knowledge base.

Learn More