Woté ak bwate wocal

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Sistému Firefox amnë ay péhé yu bari té am dolé pour dialalé ak ték ci yone say woté.

  • So bëggé woté, ubil aplikaçion téléfon bi phone 1.3 compozél béne numéro, so paré nge bës buton callbutton . Mëne nge taamit tane béne numéro ci ñi nge moudjé wo Call call log walë sah ci say kontakt Call contacts .
  • So beugué woté, ubil aplikaçion téléfon bi phone 1.4 , compozél béne numéro , so paré nge bës buton callbutton . Mëne nge taamit tane béne numéro ci ñi nge moudjé wo Call call log waleu sah ci say kontakt Call contacts .
  • So bëggé woté, ùbil aplikaçion téléfon bi phone 2.0 , compozél béne numéro , so paré nge bës buton call button 2.0 .Image:phone 1.4]], compozél béne numéro, so paré nge bëss buton callbutton . Mëne nge tamit tane béne numéro ci ñi nge moudjé wo Call call log walë sah ci say kontakt Call contacts 2.0 .

Tambalil seu woté ci say Kontakt walë ci ñi nge mujjé wo

kontakt

  1. Ubil aplikaçion téléfon bi Phone 1.3 .
  2. bësal Call contacts pour oubi seu karné.
  3. Bësal ci touruu ki nge bëg wo
  4. Bësal ci numéro téléfon bi.
  • Call contact
  1. Ubil aplikaçion téléfon bi phone 1.4 .
  2. Bësal ci Call contacts pour oubi seu karné.
  3. Bësal ci tourou ki nge beug wo
  4. Bësal ci numéro téléfon bi.
  • Call contact
  1. Ubil aplikaçion téléfon phone 2.0 .
  2. Bësal ci Call contacts 2.0 pour ubi seu karné.
    1. Bësal ci touru ki nge beug wo
  3. Bësal ci numéro téléfon bi.
  • Call contact 2.0

Pour yénéne léral ci naka la karné bi di doxé, xolal jëli, yok ak zèrè kontakt ci sistému Firefox.

xibaru woté

xibaru woté yi Call call log dafay liim apél yi nge djot, yi nge jalalé ak yi nge wuyuwul. Dafay doh ak së karné pour maylë nay mëne di woté ak di yok ay numéro ci së karné.

  1. Ubil aplikaçion téléfon bi phone 1.3 .
  2. Bësal ci Call call log pour ubi së karné.
  3. Bësal ci tourou walë numéro ki nge bëg wo.
  • Call log options
  1. Ubil aplikaçion téléfon bi phone 1.4 .
  2. Bësal ci Call call log pour oubi seu karné.
  3. Bësal ci touru walë numéro ki nge bëg wo.
  • Call log options
  1. Ubil aplikaçion téléfon bi phone 2.0 .
  2. Bësal ci call log 2.0 pour ubi seu karné.
  3. Bësal ci touru walë numéro ki nge bëg wo.
  • Call log options 2.0
Da nge bëg wowat ki nge mujj wo? da ngay rek bës buton bu werte bi callbutton pour ci sassi nge mëna compozé numéro bi nge moujj wo.

Li meuna am ci biir woté

So néké di woté mëne nge:

  • tëjj se micro bi ci kaw nge bës buton nopi bi mute 1.3 .
  • Bësal ci buton bindukay bi [Image:Dialpad 1.3]] pour mëna fénial numéro yi ngay bës. Li dinale dïmbali pour nga mëna duug se bwate wocal walë yénéne hétu sistému téléfon yu ni mél.
  • Bësal buton ö parleur bi speaker 1.3 pour mëna tal ô parleur bi ndah ñi nék ci se nég mËna dég woté bi.
  • Lernani, sabo bësé buton bu xonk bi apél bi dafay diékh.
    In-call options
  • Fayal seu micro bi ci kaw nge bës buton nopi bi mute1 .
  • Bësal ci buton bindukay bi Dialpad pour mëna fénial numéro yi ngay bës.Li dinaleu dimbali pour nga mëna duug se bwate wocal walë yénéne hétu sistému téléfon yu ni mél.
  • Bësal buton ö parleur bi speaker (small) pour meëna tal ô parleur bi ndah nii nék ci seu nég meuna dég woté bi.
  • Bësal ci buton yok béne wotékät conf 2.0 pour nékal béne conférenssou woté.
  • Lernani, sabo bësé buton bu xonk bi apél bi dafay diékh.
    In-call options 2.0

conférenssou woté

Da nge bëg am waxtane ak lu ëp bene nit? Kénéne ku nék ci seu Karné mëna bok ci waxtane bi tamit.

  1. Tambalil woté bi ci kaw nge compozé numéro walë nge bës ci touru ki nge bëg wo.
  2. Ci biir woté bi nga nék, bësal ci buton yok wotékät conff .
    conf call
  3. Say Kontakt dinaniu fénie. Tanal ki nge bëg yok ci woté bi.
  4. ki nge bëgone yok sou duuggé, mëne nge topat yone bi ngir meuna yokat niénéne.
  • connect conf
  1. Tambalil woté bi ci kaw nge compozé numéro walë nge bës ci touru ki nge bëg wo.
  2. Ci biir woté bi nga nék, bësal ci buton yok wotékät conf 2.0 .
    conf call 2.0
  3. Tanal Kontakt bi nge bêg yok ci seu woté ci biir list bi fénie
  4. ki nge bëgone yok sou duuggé, mëne nge topat yone bi ngir mëna yokat niénéne.
  • connect conf 2.0
Mëne nge yok lu tolni juuromi wotékat, mou mëna yam cii juurom ak béne, bossi bolé se bop.

Duug ci seu bwate wocal

  • Ubil aplikaçion téléfone nge bës té djap numéro 1 pour wo seu bwate wocal.
    Call voicemail 2.0
Gaa ñu baax ñii a jàpp ci bindum jukki bii: AbdouAziz. Yaw itam mën nga cee jàpp - xamal niñu koy defee.