Muccal àdduna

nga tëdd ci sa kanaape bu nooy

Soxla nanu sa ndimbal!

Lu ëpp 400 miliyoŋi nit ñoo koy jëfandikoo, ay nit ñu baax ñooy dimbali Mozilla, te looloo ci gën a am solo. Foofu lañu la soxlaa.

Lu tax ma war a dimbali?

Dimbalil ay miliyoŋi jëfandikukat ñu am li ñu bëgg ci joowukaay bi leen gënal. Sa dimbal dina yegg ci ay miliyoŋi jëfandikukat ci àdduna bi, te mën nga tëgg ci sa kanaape bu nooy di ko def!

Tànnal anam wooy bokkee

Lu jëm ci Nun

Ndimbalu Mozilla mooy mbooloom nit ñu baax ak liggéeykat yi yiy jéem a dimbali sunuy jëfandikukat yi ci àdduna bi yépp. Kaay bokk ci lu am solo loolu!
Laajal dara

Danga am ay jafe-jafe ci costéefi Mozilla moo tax nga soxla ndimbal?